
Retourner au premier écran avec les dernières notices... |
Catégories



Léebi Xale yi ci kàggu yi / PLAN INTERNATIONAL
Titre : Léebi Xale yi ci kàggu yi : Liiru jinax ak liiru muus Type de document : texte imprimé Auteurs : PLAN INTERNATIONAL, Auteur Editeur : Louga:Plan International Année de publication : Mai 1998 Importance : 6p. Note générale : Fig.;BD;Don de L'Energie Langues : Wolof Catégories : CULTURE ET SOCIETE Mots-clés : LITTERATURE ARTS CULTURE TRADITIONNELLE PATRIMOINE CULTUREL EDUCATION COMMUNAUTAIRE ANTHROPOLOGIE SOCIALE ET CULTURELLE Résumé : Téere bii nag xalaati gune donn la;li to tax a jog bokk ci naax dongo yi ci yoonu xalaat,gestu tey tenk xam-xam yooyu cim mbind,ngir sugali làkki réew mi.Ku ne xam na yit ne njàngum làkki réew mi,yemul rekk ci njàngum bind,yer,ak xayma donn.Waaye dafa emb yeneeni fànn yuy war a yee doom-aadama yi,rawatina guneyi ci wàll yu mel ni:Cet gi,Wér-gi-yaram,xam-xammeek xamle,caytu,ba ci man ak moom sa bopp ci bépp anam bu mu manti doon;rawatina ci dundug xale yiy yaakaari réew mi.
Permalink : http://enda-cremed.org/bpd/opac_css/index.php?lvl=notice_display&id=27499 Léebi Xale yi ci kàggu yi : Liiru jinax ak liiru muus [texte imprimé] / PLAN INTERNATIONAL, Auteur . - [S.l.] : Louga:Plan International, Mai 1998 . - 6p.
Fig.;BD;Don de L'Energie
Langues : Wolof
Catégories : CULTURE ET SOCIETE Mots-clés : LITTERATURE ARTS CULTURE TRADITIONNELLE PATRIMOINE CULTUREL EDUCATION COMMUNAUTAIRE ANTHROPOLOGIE SOCIALE ET CULTURELLE Résumé : Téere bii nag xalaati gune donn la;li to tax a jog bokk ci naax dongo yi ci yoonu xalaat,gestu tey tenk xam-xam yooyu cim mbind,ngir sugali làkki réew mi.Ku ne xam na yit ne njàngum làkki réew mi,yemul rekk ci njàngum bind,yer,ak xayma donn.Waaye dafa emb yeneeni fànn yuy war a yee doom-aadama yi,rawatina guneyi ci wàll yu mel ni:Cet gi,Wér-gi-yaram,xam-xammeek xamle,caytu,ba ci man ak moom sa bopp ci bépp anam bu mu manti doon;rawatina ci dundug xale yiy yaakaari réew mi.
Permalink : http://enda-cremed.org/bpd/opac_css/index.php?lvl=notice_display&id=27499 Exemplaires
Code-barres Cote Support Localisation Section Disponibilité 27368 135/ PLA/27368 Papier Bibliothèque ENDA Accéder au fonds Exclu du prêt